Wax ma li nga xam
Ma wax la li ma xam
Bu ñu ko boolee mu nekk xam-xam
Kaay jox ma li nga am
Ma jox la li ma am
Bu ñu ko boolee mu nekk am-am
Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?)
Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?)
Bëgg naa la ba noppi
Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?)
Wóolu naa la ba noppi
Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?)
Xaalisoo
Xaalisoo boo yi badjo
Xaalisoo
Xaalisoo boo yi badjo
Tasare nga dunya yàq nga lu ne
Foo dëkk jot ci àddunia xaalis a nga jar
Ma nga fekk ñaar ñuy ànd te yagu loole
nga yàq senti ker nge ma la ragal way
Dugg nga ci biir kër jaxase njaboot gi
Tas nga séy xaritoo, xaalisoo
Xaalisoo
Wax ma li nga xam
Ma wax la li ma xam
Bu ñu ko boolee mu nekk xam-xam
Kaay jox ma li nga am
Ma jox la li ma am
Bu ñu ko boolee mu nekk am-am
Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?)
Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?)
Bëgg naa la ba noppi
Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?)
Wóolu naa la ba noppi
Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?)
Xaalisoo
Xaalisoo boo yi badjo
Xaalisoo
Xaalisoo boo yi badjo
Boo amee xaalis am nga solo
Boo amul xaalis amul solo
Boo amee xaalis ni la ba jor bëgg la
Yaa bari doole, neexul waay dëgg la
Xaalisoo
Xaalisoo boo yi badjo
Xaalisoo
Xaalisoo boo yi badjo