Wax ma li nga xam Ma wax la li ma xam Bu ñu ko boolee mu nekk xam-xam Kaay jox ma li nga am Ma jox la li ma am Bu ñu ko boolee mu nekk am-am Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?) Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?) Bëgg naa la ba noppi Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?) Wóolu naa la ba noppi Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?) Xaalisoo Xaalisoo boo yi badjo Xaalisoo Xaalisoo boo yi badjo Tasare nga dunya yàq nga lu ne Foo dëkk jot ci àddunia xaalis a nga jar Ma nga fekk ñaar ñuy ànd te yagu loole nga yàq senti ker nge ma la ragal way Dugg nga ci biir kër jaxase njaboot gi Tas nga séy xaritoo, xaalisoo Xaalisoo Wax ma li nga xam Ma wax la li ma xam Bu ñu ko boolee mu nekk xam-xam Kaay jox ma li nga am Ma jox la li ma am Bu ñu ko boolee mu nekk am-am Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?) Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?) Bëgg naa la ba noppi Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?) Wóolu naa la ba noppi Mbaa doo ma trahir? (Mbaa doo ma trahir?) Xaalisoo Xaalisoo boo yi badjo Xaalisoo Xaalisoo boo yi badjo Boo amee xaalis am nga solo Boo amul xaalis amul solo Boo amee xaalis ni la ba jor bëgg la Yaa bari doole, neexul waay dëgg la Xaalisoo Xaalisoo boo yi badjo Xaalisoo Xaalisoo boo yi badjo