Cifra Club

Wareef

Dieyla

We don't have the chords for this song yet.

Djiguène bou né beuge na si doundame Kouko yeureum
Beugue na koukay goungé
Thie yone diox ko thieuram
Beugue na kouko wolou si lou nieuwa goul
Beuge na kouko sangue soutoura ndax matatoul
Lima mome dama kay diox
Goor gouma falé bouma réwal téral ma
Té douniou laalé
Kou meun sargal djiguéne
Goor gou méloute ni yéen
Kouy door ak saga té meusso di réé

Say réé lala beugué
Ni lala nobé
Say dieuf lala nawé
Ni nga mel boul ko changer
Yaw gentle nga
Do xoulo do xéex
Téral nga djiguène

Ni lala beugé
Ni lala nobé
Say dieuf lala nawé
Ni nga mel boul ko changé
Eh waay waay gentle nga ni lala beugué

Andi nga téranga mani waaw
Di nga ma liguéye mani waaw
Di nga mani fo dieum
Di nga ma yobalé
Wayé sou amoul mbeuguél, bye bye
Yaw wane ma louma doye
Ma dix la loula doye
Bo Xamer kima doone
Moy xol bi yaka mome
Wouy yoo lé, wouy yoo léé
Beugue na koumay nabe nabé

Def ma lila war xam nga ni nii la nii la
Diame dji ngay weur fii la
Soma woolo doylo ma
Loma meun ti nakhé nangou na

Say réé lala beugué
Ni lala nobé
Say dieuf lala nawé
Ni nga mel boul ko changer
Yaw gentle nga
Do xoulo do xéex
Téral nga djiguène

Ni lala beugé
Ni lala nobé
Say dieuf lala nawé
Ni nga mel boul ko changé
Eh waay waay gentle nga ni lala beugué

Andi nga téranga mani waaw
Di nga ma liguéye mani waaw
Di nga mani fo dieum
Di nga ma yobalé
Wayé sou amoul mbeuguél, bye bye

Yaw déé ko té nga aare ko
Xolé ma man mii sa yaye booye
Ndax djiguéne dagne kay soutoulal

Other videos of this song
    0 views

    Chord tuning

    Online tuner

    Ops (: Content available only in Portuguese.
    OK