Djiguène bou né beuge na si doundame Kouko yeureum Beugue na koukay goungé Thie yone diox ko thieuram Beugue na kouko wolou si lou nieuwa goul Beuge na kouko sangue soutoura ndax matatoul Lima mome dama kay diox Goor gouma falé bouma réwal téral ma Té douniou laalé Kou meun sargal djiguéne Goor gou méloute ni yéen Kouy door ak saga té meusso di réé Say réé lala beugué Ni lala nobé Say dieuf lala nawé Ni nga mel boul ko changer Yaw gentle nga Do xoulo do xéex Téral nga djiguène Ni lala beugé Ni lala nobé Say dieuf lala nawé Ni nga mel boul ko changé Eh waay waay gentle nga ni lala beugué Andi nga téranga mani waaw Di nga ma liguéye mani waaw Di nga mani fo dieum Di nga ma yobalé Wayé sou amoul mbeuguél, bye bye Yaw wane ma louma doye Ma dix la loula doye Bo Xamer kima doone Moy xol bi yaka mome Wouy yoo lé, wouy yoo léé Beugue na koumay nabe nabé Def ma lila war xam nga ni nii la nii la Diame dji ngay weur fii la Soma woolo doylo ma Loma meun ti nakhé nangou na Say réé lala beugué Ni lala nobé Say dieuf lala nawé Ni nga mel boul ko changer Yaw gentle nga Do xoulo do xéex Téral nga djiguène Ni lala beugé Ni lala nobé Say dieuf lala nawé Ni nga mel boul ko changé Eh waay waay gentle nga ni lala beugué Andi nga téranga mani waaw Di nga ma liguéye mani waaw Di nga mani fo dieum Di nga ma yobalé Wayé sou amoul mbeuguél, bye bye Yaw déé ko té nga aare ko Xolé ma man mii sa yaye booye Ndax djiguéne dagne kay soutoulal