Cifra Club

Dedete (feat. Leyna)

One Lyrical

We don't have the chords for this song yet.

Yay sama mbourok lem
Wakhona la boul dem
Sou nakarei gua daw
Bouy nekh doko fekei
Baby, wathiel arme yi
Boul di deuglou gni
Mane ak ioe dou tay may sa everything

Yay sama lounei founei
Kone baby déma ré
So mèrè rek damay rer
Déma ré khôl yi fekhhh
Ay sama lounei founei
Kone baby déma ré
So mèrè rek damay rer
Déma ré khôl yi fekhh

Bougou gnou lou doul sa défet
Dila guiss gua ré dédéte
Sho bi dou djabar dédéte, ki dou djabar dédéte
Bougou niou lou doul sa défét
Dila guiss gua ré dédéte
Lo bi dou djabar dédéte, ki dou djabar dédéte

Ioe la ioee laa ioe la ioe la nop
Mane ioe la ioe laa ioe la ioe la love
Mane ioe la ioe la ioe laa ioe la nop
Mane ioe la ioe la ioe laa mane ioe la love

[?]

Bougou gnou lou doul sa défet
Dila guiss gua ré dédéte
Sho bi dou djabar dédéte, ki dou djabar dédéte
Bougou niou lou doul sa défét
Dila guiss gua ré dédéte
Lo bi dou djabar dédéte, ki dou djabar dédéte

Ioe la ioee laa ioe la ioe la nop
Mane ioe la ioe laa ioe la ioe la love
Mane ioe la ioe la ioe laa ioe la nop
Mane ioe la ioe la ioe laa mane ioe la love

Other videos of this song
    0 views

    Chord tuning

    Online tuner

    Ops (: Content available only in Portuguese.
    OK