Cifra Club

Bukki

Obree Daman

We don't have the chords for this song yet.

Nitt du mala
Li ngay def
Sakkul naam xam ko
Nitt du mala
Li ngay wax
Seetantal ko waay

Nitt du mala jikkoom
Nga koy xoolee doomu
Àdama ni la ñu Yalla
Bindee ci àddunam si
Ak sunu matadi
Waaye moom Yalla rekk a xam
Nitt du mala jikkoom
Nga koy xoolee doomu
Àdama du dem safara

Nitt du mala
Li ngay def
Sakkul naam xam ko
Nitt du mala
Li ngay wax
Seetantal ko waay
Nitt du mala
Li ngay wax
Seetantal ko waay

Wacce na taw ci ñun
Gancax gi mèeñ na
Ngelaw gi feexal
Jànt bi leeral
Moo xam li nekk ci ñun
Ndax moo def li nekk ci ñun
Kon mandu war na ñu
Ci nitt ni ko Yalla bindee

Nitt du mala jikkoom
Nga koy xoolee doomu
Àdama du dem safara
Nitt du mala jikkoom
Nga koy xoolee doomu
Àdama du dem safara

Nitt du mala
Li ngay def
Sakkul naam xam ko
Nitt du mala
Li ngay wax
Seetantal ko waay
Nitt du mala
Li ngay wax
Seetantal ko waay

Nitt du mala
Li ngay wax
Seetantal ko waay

Other videos of this song
    0 views

    Chord tuning

    Online tuner

    Ops (: Content available only in Portuguese.
    OK