Eh! Aayaaa Sénégal boy Yeah Balle ba ngi sogo takk Ghetto sama ginnaaw Man rekk man kese fi tekk tank Xaalis du doy, jàmm du ëpp Tour ba ngi dem succès di yokk Listen piis fëri ñun duñ la fàtte Derétu diamaguene mo fi daw Dérek moo may tere te game bi Iyo, iyo Ni may rabe lu si sa yoon Bandit dëgg de koy nuróó Xam naa ni si man ngay xool Mais non non ni nga koy defe du noonu Dem laalal de, sa show man la barde Ay caché millions sans projet Man la Sénégal boy from jekk (hey) Non non coow li du bari Man ngeen tekk seen bët yi Te ñaan waajur moo tax ma yeksi fi, waa eh Ñoom lu ñu fokk? Munuñu bokk Xiir bi la yorr Ñuy daw malen koy nokk Ey mangek buzzu ndongo Dama xew, ey Boo ma xamul Demal nga tokk Eh, demal nga tokk Demal nga tokk Eh boo ma xamul bu yaa demal nga tokk Demal nga tokk Pic bi ñu ma sànni man dama ko toul Ñoo ma ci jittu ma leen raw fuuf Ne leen yolé xajjatul ci poche Niak sipp wessouwoul andak kou matoul Xaliss la Xèkhè douma khoulo Kholéma Ndongo Lô bir Ghetto Musiku fi lay toukilo International Nekké ci yone Mashallah! Poche Bangui fess may fékh Na mère bi bégg Bu ñu sañoon kenn du ma deug Léegi ñoom ño may xeex Nangu demb bëgg bañ tey Sissouman yi demelen bayi ci birr Kode sama xol def xeuthie Éclate kanam bi xol Guedj Eh! Non non coow li du bari Man ngeen tekk seen bët yi Te ñaan waajur moo tax ma yeksi fi, waa eh Ñoom lu ñu fokk? Munuñu bokk Xir bi la yorr Ñuy daw malen koy nokk Ey mangek buzzou Ndongo Dama xew, ey Boo ma xamul Demal nga tokk Eh, démal nga tokk Démal nga tokk Eh boo ma xamul bu yaa dèmal nga tok