Deff Music Wiri Wiri Diaari ndaaré Wiri Wiri (Pape Laye) Diaari ndaaré Wiri Wiri Diaari ndaaré Wiri Wiri Diaari ndaaré Louné louné Dieem naako def Technique bouné Diemnaako tek Toujours la même Réponse dedeet Dieemnaala ba mais lii dou neen Nieuwaat nga kong Metitou khol Tekma thiono Teh dama beau Dieundaat cadeau Pour am sa khol Damay niakaat diom mais dooma khool Mbeugueul dou diaay loolo metti dagma diaral (dagma diaral) Mane damla dieulsi doumfi nekay tabal tabal (tabal tabal) Guisnaala demb ki nga andal kila xaral (wa dou ki) Day nioodi gentle mais dou dara sama kanam (dara dara) Mane dama baayi nieupeu né iow la iow la iow la Looma wakh biss boo wakhé waw noonou laa noonou laa noonou laa bébé Deff loo ngama lounekk (Wiri wiri diaari ndaaré) Dem loo ngama founekk (Wiri wiri diaari ndaaré) Wayadiloo meu founekk (Waayé douma dieul ndaaré) Si mane ngay moudier, yaag yaag di nga barder Wiri wiri diaari ndaaré (oh diaari ndaaré) Wiri wiri diaari ndaaré (oh diaari ndaaré) Wiri wiri diaari ndaaré (oh diaari ndaaré) Wiri wiri diaari ndaaré (oh diaari ndaaré) Bimlay wakhni beugoumaleu Nangouloomawoon deglou Tay nga tekk sa bopp thiono (thiono) Ba noppi ni louné laaley deff loo Fii amoul wiri wiri diaari ndaari Maak iow dou meusseu nekk dedeet never Dieemeul lambi feneen moo gueun Fi nga dal nii bro amna borom Maak iow dou béneu Bookouniou level Teh sooma soroo di nga guiss loula diaakhal Def naa lou nékeu Ngani doo gëdda Yow fooma toopé ay yallah miniou sakka Iow mii iow miii Baayimeuuu waaaw Baayimeu baayimeu Deff loo ngama lounekk (Wiri wiri diaari ndaaré) Dem loo ngama founekk (Wiri wiri diaari ndaaré) Wayadiloo meu founekk (Waayé douma dieul ndaaré) Si mane ngay moudier, yaag yaag di nga barder Wiri wiri diaari ndaaré (Oh diaari ndaaré) Wiri wiri diaari ndaaré (Oh diaari ndaaré) Wiri wiri diaari ndaaré (Oh diaari ndaaré) Wiri wiri diaari ndaaré (Oh diaari ndaaré) Oh diaari ndaaré Oh diaari ndaaré Oh diaari ndaaré Oh diaari ndaaré