Hey geeneel paaka yi daas Agsi toog sen fit yi jël sen xol yi di waas Këllëm ci kaw beat bi man rekk maa len di maas Da maa bëri feeling yen ngen dëkkee di kaas Hey nañ len dajje rungaas Fii maa fi nekk Ñëw pour yokk cere dolli ñeex Hey fii maa fi nekk Arbitre sifflel tay rekk noon yi dee Après coow li jeex foofu Sudul Youtube bu ma tendance Rap bi rekk lay mbaraan Kenn saññu ma diss ndaxte xajju ma ci balance Da maa xew Yallaa ko def, siiw Yallaa ko def Yaa ngi mer di bokk golo nga la way ku la ko teg? Da ngaa soxor, soo saññoon ma torox Fii laay toog ni faraax di len may ay bars yu forox Maa koy teg ci temps nii Jeune coof japp teint Noqqul jall nee Maa toog seeni bopp doon cancer seeni reins Neel patt, noppil bul ñu fatt Kaasal der bu ñuul te ay métisses rek lay fat Neel patt, noppil bul ñu fatt Ubbi naa sen taat sotti acide seen gat yi Hey geeneel paaka yi daas Agsi toog sen fit yi jël sen xol yi di waas Këllëm ci kaw beat bi man rekk maa len di maas Da maa bëri feeling yen ngen dëkkee di kaas Hey nañ len dajje rungaas Fii maa fi nekk Ñëw pour yokk cere dolli ñeex Hey fii maa fi nekk Arbitre sifflel tay rekk noon yi dee Après coow li jeex foofu Pape Sidy awma ñaari gels Mais chaque jour crush bu bees Ñoom ñëpp ñi ngi may baayi xel Mais baayi wu ma sama bopp Sa lyriciste da ma ko vent Tax sen xol du feex Kanam bu chou ay pec yu yem akk poche bu àntan saaku ceeb Sa xol moy xasan mais doo waga Liquide yoroo walaat Do dem fenn matoo woyaas Baayil rap dem wayaan Deuxième couplet 3e baram rap ba am ci 4e madame Goor Faal fa may fanaan sa gels laali na fa ay draps J’en ai marre Ci seeni cas chaque jour yu bees nooy mel ni COVID Ñi ma ñaanal maa len jullee Jël ngaamu noon yi sukki mukki Boy buñ taal ma mukki mukki Xew ni ku boot fukki bukki Baayi naa playback fukki junni [?] Hey geeneel paaka yi daas Agsi toog sen fit yi jël sen xol yi di waas Këllëm ci kaw beat bi man rekk maa len di maas Da maa bëri feeling yen ngen dëkkee di kaas Hey nañ len dajje rungaas Fii maa fi nekk Ñëw pour yokk cere dolli ñeex Hey fii maa fi nekk Arbitre sifflel tay rekk noon yi dee Après coow li jeex foofu