Hey Zeus Bril Oh la la Hé Hé Let's Go Hey Hey Fii ngako degué (ngani) Fii lagnko wakhé (hum) Fii ngako guissé (waw) Fii lagnko deffé (tchi gui tchi gui) Fii ngako degué (ngani) Fii lagnko wakhé (hum) Fii ngako guissé (waw) Fii lagnko deffé Mané boy Boy bouma yakhal (ohlala) Maaguissi sama (ohlala) Lii maako waral (ohlala) Namouma dara (ohlala) Boy bouma yakhal (ohlala) Maaguissi sama (ohlala) Lii maako waral (ohlala) Namouma dara (ohlala) (aïe aïe aïe) (Oh Lala) Boulma yakkal sama oh lala hey (ohlala) Eh boulma yakkal sama oh lala Gaïndé bou dégoul diatt Néleen ma thiourki thiam, maaguek wakhou bou gueulem Diokh sama bop diam takh sama khel di nathi, bamay maayé dji déreet Boy bima rap di fay, chaine biné sama baat boobu fégnouma télé Xallé bou melni mane niaanalma goudou fane, doossi guissati benen Deff kat bou makk moodoul def louko waroul Bideewou beuthieuk si goudi loup garou Dougueul si mane xamné talent dou tandouss Alakhiraa noofay démé di kharou Sécurité doundé sa art Boybi daa mag ni 18 safar Kounta kinté zulu shaka Yeuf yi bou diougué rk c'est la cata Dougouma chaloupe mais maagui Gorée Meun ngama adiou mais tu me connais Bou CD bi diaroul danguéna doffé Zeus doula tafou booy copier collé Boumala taloul nane ngamay fayé Oothentik fowoul dalendi fowé Mouvement bi démoul doolenfi sorré Loolou mooy wakhou kou daanou si charette Fii ngako degué (ngani) Fii lagnko wakhé (hum) Fii ngako guissé (waw) Fii lagnko deffé (tchi gui tchi gui) Fii ngako degué (ngani) Fii lagnko wakhé (hum) Fii ngako guissé (waw) Fii lagnko deffé Mané boy Boy bouma yakhal (ohlala) Maaguissi sama (ohlala) Lii maako waral (ohlala) Namouma dara (ohlala) Boy bouma yakhal (ohlala) Maaguissi sama (ohlala) Lii maako waral (ohlala) Namouma dara (ohlala) (Oh Lala) Boulma yakkal sama oh lala hey (oh la la) Eh boulma yakkal sama oh lala Mangui thi sa Sama bopp, sorima mangui thi lénén, def ni sa Ex Tok thi sa diggou bopp ba nieupp di fokni may accent circonflexe Yaggueu ni Assamane, def ay Hit la mii douma tégguéti Tank! Règlement de compte, boma thi déggué da fékkeu ni mangui thi Bank Défouma Judoka Té mangui prise Nguéni weuri daanou, ma weuri djizz Bo takkone sa beutt yi sakh dingama guiss Sagama sa Guel bi yonéma biz (ouh) Dama khéw ba légui mangui wadja tidji cosmétiques ndakh beuri Tubes Khalé Thiaroye 44 fok mou bomb Niata millions ngéni guiss biir YouTube! Meune lépp motakh kén douma yapp, rare ni car rapide bou amoul apprenti! Yéék thi kaw beat bi di partouze, meussouma bayi dõré mane la Alkati! Séni Guel dima khol, All eyes on me, melni Pac mo déloussiwatt! Risquél doublé thi virage wala Bril ak Zeuss Nioussla, Mou siwattt! Fii ngako degué (ngani) Fii lagnko wakhé (hum) Fii ngako guissé (waw) Fii lagnko deffé (tchi gui tchi gui) Fii ngako degué (ngani) Fii lagnko wakhé (hum) Fii ngako guissé (waw) Fii lagnko deffé Mané boy Boy bouma yakhal (ohlala) Maaguissi sama (ohlala) Lii maako waral (ohlala) Namouma dara (ohlala) Boy bouma yakhal (ohlala) Maaguissi sama (ohlala) Lii maako waral (ohlala) Namouma dara (ohlala) (Oh Lala) Boulma yakkal sama oh lala hey (oh la la) Eh boulma yakkal sama oh lala