Omzo on the Mafe Niveau bey hot dey lakke Song bi dey daw M'bappe Ndakaaru njaay lay wacce Da nga xam wala ngay lacce? (Ey) Niveau bey hot dey lakke Song bi dey daw: M'bappe Ndakaaru njaay lay wacce Da nga xam wala ngay lacce? Boy kula laadj loy wax? Ey waay ndeysaan Ey deykalanax! Dañu koy salsaa bamu saf sapp Boy kula laadj loy wax? Ey waay ndeysaan Ey deykalanax! Dañu koy salsaa bamu saf sapp Eh seen xel yè karaas mënoleen dem Fépp lañ mënè ego ak théme Lepp ngeen tële di xaatim nenn Yèn ñëp lay warax, talent dey fènn Raw naa daxaar qon lepp ay saff Yëngël Dakar ba lepp ay barr Fepp ay saxar te fepp ay tarr Xatna comme yaraax yenn ñëp ay xaar Naanuma lingom te gënlaa forox Deñ lay tingoom nga mën maa boroos Sëf lë ay drogues Di laal ay troc Jital oyof tе mën naa torop Laalnaa xol yi, bët yeppay taa Root néñ xalaat ba feesal ndaa Xir bey dalaat Fi mann leñ falaat tе Neena faraax damay salsaa allright Niveau bey hot dey lakke Song bi dey daw M'bappe Ndakaaru njaay lay wacce Da nga xam wala ngay lacce? (Ey) Niveau bey hot dey lakke Song bi dey daw: M'bappe Ndakaaru njaay lay wacce Da nga xam wala ngay lacce? Boy kula laadj loy wax? Ey waay ndeysaan Ey deykalanax! Dañu koy salsaa bamu saf sapp Boy kula laadj loy wax? Ey waay ndeysaan Ey deykalanax! Dañu koy salsaa bamu saf sapp Eh kula laaj loy? My boy Bëri ay biens, riche: Bad boy, gatdamn Dañu koy game bamu neex Waye mënu ñuko gagne fò, d'accord Maak Mgeey de la Mancha Sancaat drip bu leer diko salsaa May MC bila antann Tek lu dìs gann si sa kaw ba nga appaat Fuck li ngay wax mëso maa jox cèpp Budè da nga merr everything okay Avant ngeen di xeef nekatul mok yeen Sama talent mo daaxa wanewuu Mo gates Okay okay no stress No cap My boy loy hate? Sama chronomètre dou seu temps lay kepp Bu yabbo nga kepp sa tank boy Tekk ngafi tank Mais taanku guinaaw Niveau bey hot dey lakke Song bi dey daw M'bappe Ndakaaru njaay lay wacce Da nga xam wala ngay lacce? (Ey) Niveau bey hot dey lakke Song bi dey daw: M'bappe Ndakaaru njaay lay wacce Da nga xam wala ngay lacce? Boy kula laadj loy wax? Ey waay ndeysaan Ey deykalanax! Dañu koy salsaa bamu saf sapp Boy kula laadj loy wax? Ey waay ndeysaan Ey deykalanax! Dañu koy salsaa bamu saf sapp