Kenal ngama thi gnom Denthial ngama sa bopp Takh nga dioy (mougneul nala) Mirr na thi yaw, mi amor Kenal ngama thi gnom Denthial ngama sa bopp Takhh nga ma dioy, mougneul nala Mirr na thi yaw, mi amor Setto sett, setto sett Setto sett, setto sett Setto sett, setto sett Setto sett, setto sett (Setto sett) Sama dollé la sef thi mbeuguel Bimala beugué kholouma lo am ak lo amoul Beut yingay kholé missal nama ningama beugué (Damala nopp) Deff ngama Indo anyway Diaral ngama teukku Balla Gaye Kay ma nekhal sa goudi gui tay Yobbuma fu sorri doumla lathté fougnou dieum Diombadio, show me my your body Show me your body, show me your body Diambadio, wakh dji du bari Wakh dji du bari, only, only, only, only you Kenal ngama si gnom Denthial ngama sa boppp Takk na nga dioy (mougneul nala) Mirr na si yaw, mi amor Kenal ngama si gnom Denthial ngama sa bopp Takh nga ma dioy, mougneul nala Mirr na si yaw, mi amor Setto sett, setto sett (mirr na di yaw, mi amor) Setto sett, setto sett Setto sett, setto sett (mirr na di yaw, mi amor) Setto sett, setto sett Goudi beuttsett souba ak ngonn meun na nelaw ba yandorr Mirr na, mi amor, yaw rekk, mi amor Goudi beuttsett souba ak ngonn meun na nelaw ba yandorr Mirr na, mi amor, yaw rekk, mi amor Setto sett, setto sett Setto sett, setto sett Setto sett, setto sett Setto sett, setto sett Beuttsettt souba ak ngonnn Nelaw ba yandorr