Anh my check, one two Beuteuy guiss kholay yeuk lamigne tontou Pour gni nga khamné dougnou sawar si ay fontou Gninga xamnai depuis fadjar lagni gontou Di lathiéi ni salaire bi démé Ndèki rekk di khalate ni séne rére di démé Khaliss bi dou woor même sou werr bi fégné Mani xaliss bi dou woor même sou werr bi fégné Da am ay borom bopp you amoul séne bopp Ak borom xam xam yo xamné xamougne sene bopp Nagnou moytou yaine jeuf yoy yatal fitneu Nitou ya'allah doula wakh ni Ya'Allah nite leu Kou yendou si sétou dh warna meune xolate bopam Est ce que Ya'Allah dina balé koudoul ball mbokam? Niteu geuneu cher lép lo guiss sikaw souff Mais jiguén bouy djay thiaf mo geune jiguén bouy djay bopam Da am ay Cris ak Lèo, pistoléro Guiss fi ay triste fléau Moudjou dila gnane taw ni kou guiss Météo Miezé molay wakh lou khew ni profou Histo-Gèo Yawmal Khiyam dh dougnla wakh heure bi Comme mbindane bou mole day todj keur gui Ci kaw ci kanam en avant les amis Mane ben yonn la kham meme souma deukone niary-tally (Abozé) Digueunté fouma naik fouma jeum da am ay affaires yign ma wakhoul (Ann, anh Anh my nigga) x2 Limlay yeugeul moy (x2) Nigga prof bi day tekk (Nigga prof bi day tekk) Ya'Allah rekkey buur Rignseu bi day taik (Rignseu bi dey tekkk) Ya'allah raikay buur Da am gno xamnai saini liguéye tokk di wakh la bounigni di daif (bounigni di daif) Mais souvent gni di wakh dougnou mousseu mousseu bokak gni di deff Dama geum Ya'allah geum sama boop Zo saraloul sakh (Zo saraloul sakh) Gnane Ya'allah outi lima gnanone Zo saraloul sakh (Zo saraloul sakh) Soumala tognai nigga balma th nga bayi di gaide Biir safara dh fofou kaine dou bayi mou saideuh Nigga dokh di wakhou mo geune daw nank Élèves yi douniou sport dagni daw jang Présidents Afrique yi dagni mbeuw kassai So xamone lougni sacrifier pour daw kassai Allalou deukou leumb ngeu beugeu pour yaw kassai Beussna am waiteuk ya'allah nigga yow kassai Boulma décevoir, goorou Sénégal yi kagne lagni xam nai polygamie droit leu dou devoir Dou yanê yaine guêls yéy indi matérialise Ma soeur le mariage n'est pas le but ultime de la vie Sa dome bou jiguéne sonal ngako boko mayai si force Dimanche le jour de mariage, lundi jour de divorce Yeah! Da am yaine doundou yoy tègué coté Da Malaykal meuwty dh keneu douko daih Bakane meune na noyi même souy xêègne xaite Am gnouy gnak saine bakaine nakh saine khaite Dou lou nekh ga Mais nite bou waikh aka beug nite kou nioul bou yoor Xaliss bou waikh tall Niounai gnari goor youy faunantai c'est naturel Gnari goor di seuy niounai naturel Pourtant Adama ak Awa lagnou sakando Ya'allah sakando woul Adama ak Roméo Diné mingo woul ak Ada dès fois lolou am Il faut que bayi yone pour jeul yonou ndam Joulite ngeu mba Sénégalais yaw yay tane Sa mame meu naikone diiw mais yaw yaye kane? Ya'allah kouko geum sa boppou ngeu geum Motah ya'allah kouko togn sa bopou nga togn Musique dafa kharam boula dara nakh Deug raik lay wakh nigga dara nak Boul sakh khaip koudoul wakh Djouk job raik th boul xoff Boul moussa daif ak koudoul daif loumouy wakh Yaine say gninga doul fook gnoy daif lodoul fokk Yeah! Est ce que jarna bakaar pour yokkeu sa l'aise Loutakh ngay wagni salaire pour yokeu sa leer Ngainai dinai ci xol leu? Est ce que dinga daim examen jokhai feuille blanche nai jangueu si xail leu? Daif lou bakh si kaw, daif lou bone si souf Comme mourou si kaw daif leggings si souf Boy di wakh deug dh no déf gnou rayleu Prophète yi dh gnofi eupone ay haters Kou sathie danga bayi sa lokho Motah charia bi néna faut que nga bayi sa lokho Goor bokoul ak jiguéne dafa waur Ya'Allah Kone goor-jiguéne geum ya'allah défouko goor ya'Allah Ouztaz balma da am louma lay lathie yaw Prophète bi orphelin leu wakhma kouko yalwane lo? Wakhma lane la ya'allah wakh ni lagni daifak djirèm Tothie naine ci croisement omelette ko eupeu ndieurign Lou goor geune beug ci aduna jiguéne leu dou dara motax Sou seuyai dina am 2 minutes yo xamnai aduna bi doussi beug dara Goumbeu jakk dji day wakh lou Sèlbè doul guiss Louma geuneu geum Ya'allah geuneu waidi nite Kone saite kate bi day tekk Rignseu bi day tekk Président bi day tekk Policier bi day tekk Milliardaire bi day tekk Sa rappeur bi day tekk Mane mi di tekk damay tekk nigga Nigga niom gneupeuy tekk (nigga prof bi day taik, nigga prof bi day tekk) Yaallah rekkay buur Rignseu bi day taik (Rignseu bi day tekk) Ya'Allah rekkay buur Da am gno xamnai saini liguéye tokk di wakh la bounigni di daif Mais souvent gni di wakh dougnou mousseu mousseu bokak gni di daif Dama geum Ya'allah geum sama boop Zo seraloul sakh (Zo seraloul sakh) Gnane Ya'allah outi lima gnanone Zo seraloul sakh (Zo seraloul sakh)