Bo jekko deel baale Boo amee te mën ko deel maye Bo jekko deel baale Boo amee te mën ko deel maye Yaa ngi ci kaw Xalaatal ñi ci suuf 'Cause tomorrow it's another day Bu am-am tax, nga fate ki doonoo Waaye bu ñakk tax, nga baayi sa loxo Ab Goor Yàlla ngay doon Royal ci Ibra Faal ee Dinañ la xas dinañ la faqastal Waay waay bu len faale Ab Yaay Faal ngay doon Royal ci Maam Buso Baali Dinañ la xas dinañ la faqastal Yaay Faal nga bu len faale Jappante baña baayi gën di bëggënte Kula tooñ nang ko baal buñ ñu jaxase Ah dunyaa Ah dunyaa Jappante baña baayi gën di bëggënte Kula tooñ nang ko baal buñ ñu jaxase Ah dunyaa Ah dunyaa Goor Yàlla yombul ci adduna si le Boo jekkoo deel baale boo ammee te mën ko deel maye ay Waay waay waay waay Bo jekko deel baale Boo amee te mën ko deel maye Bo jekko deel baale Boo amee te mën ko deel maye