(Ah ah) Tallal say loxo te jeem (Ah ah) Tallal say loxo te nangu yen wee Tallal say loxo te jeem Tallal say loxo te nangu yen wee Ah jaww ji na ñu ci jappale Hee, doomu Àdama Ay mën-mënam waru ci tappale, humm Moo xam muy goor mbaa muy jigeen Doomu Àdama Yàlla fi mu ko feete leer na Moy gas muy suul gancax amatul Baadoola matle wul, gancax gi gën a tooy Hii Heee, gancax gi gën a tooy Hoo weee Tallal say loxo te jeem Tallal say loxo te nangu yen wee Tallal say loxo te jeem Tallal say loxo te nangu yen wee Find your way back, only your can fly Know that you can find your way back to No man, no young, no woman, no girl No black, no white, no high, no low Tallal say loxo te jeem Tallal say loxo te nangu yen wee Tallal say loxo te jeem Tallal say loxo te nangu yen wee Tallal say loxo te jeem Bantu bale Bantu bale Bantu bale Bantu bale