Bul di jaawale Bul di jaawale Bul di jaawale Bul di jaawale Mandu, mandu len Ci nitt bul di jaawale Mandu, mandu len Ci nitt bul di jaawale Dox naa ba ñëw setsi la He ñëw setsi la (hé) Nitt de war na mandu Teey te yalla tax (hé hé) Seet naa la sow, seet naa la penku Mandu reer ci jamano Seet naa la sow, seet naa la penku Mandu reer ci say jikko Mandu, mandu len Ci nitt bul di jaawale Mandu, mandu len Ci nitt bul di jaawale Bul di jaawale Bul di jaawale Bul di jaawale Mandu, mandu Mën na laa wallu Mandu, di na mandu Ci doomu àdama bi le (hé) Seet naa la sow (seet naa la sow) Seet naa la penku (seet naa la penku) Mandu reer ci jamano Seet naa la sow (seet naa la sow) Seet naa la penku (seet naa la penku) Mandu reer ci say jikko Mandu, mandu len Ci nitt bul di jaawale Mandu, mandu len Ci nitt bul di jaawale Bul di jaawale Bul di jaawale Bul di jaawale Mandu, mandu len Ci nitt bul di jaawale Mandu, mandu len Ci nitt bul di jaawale Bul di jaawale