Ni ngay dundee sunu ñakk wee du yoon Baadoola daal sonn na ci lu mu Dëkkee Senegaal Njaay Jappale len ko waawaw Ni ngay dundee yoo Ñun rekk a jaxle Ndax du ñu doomu buur Sòmbi la ñuy reere Bokku ñu nguur Feebar mënu loo fajju Yeena nga ñuy rey di suul Lii bu ci kenn waxul Ñawteef gaa law ci ñun Baadoola, baadoola, baadoola Hum (yes), hum (yes) Baadoola, baadoola, baadoola Hum (yes), hum (yes) (Hooo) I'm socialized (Hooo) I'm so sad (Hooo) I'm socialized (Hooo) I'm so sad Fitna gi nekk ci Ñun waa dëkk bi Fitna gi nekk ci Xolu askan wi Baadoola sonn na Yërmande ci moom Baadoola, baadoola, baadoola Hum (yes), hum (yes) Baadoola, baadoola, baadoola Hum (yes), hum (yes) (Hooo) I'm socialized (Hooo) I'm so sad (Hooo) I'm socialized (Hooo) I'm so sad (Baadoola) Baadoola Baadoola Baadoola Ni ngay dundee sunu ñakk wee du yoon Baadoola daal sonn na ci lu mu Dëkkee Senegaal Njaay Jappale len ko waawaw Ni ngay dundee yoo