Lu tax xale yi jàngatuñu Kër gi kenn génnatul Àdduna la teye, nit nga ngi de fi mu tollu ñëpp wéet Te ñëpp la mën daal, ki toog ak ki toggul ki wër rekk lay àndal Musuma gëm li mu daal ma Musuma gëm li pape lu am la Ñun nak dañu xiif te coobatuñu Pa bi jëmna mak te mère bi jobatul Man mii docteur rekk lay gis Mbedd mii fees dell ak police Jaaxle joomi njakare te degatuñu fi suñ Imam fum fi kabare Yaa Rahman, yaa Rahim, yaa Malik Al Moulki, yaa yaa mujib Yaa Salam, yaa Latif, yaa Karim, yaa Hakim, yaa Kabir Woh woh woh woh Yàlla yaw Yàlla yaw ñu lay ñaan nga balinu Woh woh woh woh Yàlla yaw Yàlla yaw ñu lay ñaan nga balinu Yàlla yaw baal nu Yàlla yaw baal nu Yàlla yaw baal nu Yàlla yaw baal nu (Yàlla yaw baal nu) Léegi ngay yeewu gis sa mère fee doo ko jox loxo (Yàlla yaw baal nu) Ku gis ku sekket da ngay ragal doo ko wax toqo (Yàlla yaw baal nu) Ku jàngul àdduna ci li am nga négligence nit la Yàlla gën a bëgg tay fok nga may ko distance (Yàlla yaw baal nu) Mbokk, ba xam nga li ñu bokk bu de alaal Rekk nga jitel ba faate li ñu topp Kër gi fees xale yi xiif loo ma may ma taay Weer bi dina boroom kër gi awma lu ma ko faay Deggoon na ni cëb bi ñëw na agsiwul ci ñun Ni ñun naqar rekk lañuy dund wax ko allahou kun Ñun bopp ba léegi dundetuñu te Amuñu kenn kuñ ko wax ñoo ngi tok di muñ Masque téeméer chaque jour suñ doole du ko mun Woh woh woh woh Yàlla yaw Yàlla yaw ñu lay ñaan nga balinu Woh woh woh woh Yàlla yaw Yàlla yaw ñu lay ñaan nga balinu Yàlla yaw baal nu Yàlla yaw baal nu Yàlla yaw baal nu Yàlla yaw baal nu (Yàlla yaw baal nu)