Man tànn naa la si jigéen yudul jeex Jox naa la sama xol bi yaay boroom Kon baby bul ma négligé maay sa xol Ndax maa lay jox lépp lu gëne ci yow Man tànn naa la ci jigéen yu dul jeex Jox naa la sama xol bi yaay boroom Bul négligé xamal ni yaay sama xol Ndax bëgg naa la yow bae bëgg naa la Man soo manee waaw ma ñëw seen kër Yow bëgg naa la yow, bae bëgg naa la Man soo manee waw ma ñëw seen kër Yow bëgg naa la, bae bëgg naa la Woo naa la téléphone jëluloo Envoyé naa la message wuyuwoo Lan moo tax yow babe lan moo tax Woo naa la téléphone jëluloo Envoyé naa la message wuyuwoo Lan moo tax yow babe lan moo tax Bu mbëggéel doon jaay Bu mbëggéel doon jaay Yow babe jox naa la la xool bi Waye lépp yaa ko moom Waye neewul dama ñaak jom Mësuma ñaak diom Man sama mbëggéel moo ma yobbu Moo tax maa lay woo oh Lan moo tax babe lan moo tax Su ma lay woo te babe doo ma jël Lan moo tax babe lan moo tax Su ma lay woo te babe doo ma jël Yeah yeah yeah Yeah yeah yeah yeah yeah yeaaah Anh anh Ndax bëgg naa la yow, babe bëgg naa la Man soo ma nee waaw ma ñëw seen kër Yow bëgg naa la yow, babe bëgg naa la Man soo manee waaw ma ñëw seen kër Ma ñëw ma ñëw ma ñëw Bëgg naa la yow, babe bëgg naa la