Yàlla du juum, ndekke Yàlla du juum Lu mu def ndekke loolu moo gën Demoon naa ba nar ko dugal sama biir xol Su ma ko defoon maa ngi ci tolof-tolof Kon fok ma xoolaat ko Saay-saay la Fok ma xoolat ko Waa ji saay-saay la Yàlla du juum, ndekke Yàlla du juum Lu mu def ndekke loolu moo gëna Demoon naa ba nar ko dugal sama biir xol Su ma ko defoon maa ngi ci tolof-tolof Ñew na sama kër laajte fa sama yaay booy Saay-saay la Ñëwaat sama kër laajte fa sama baay booy Saay-saay la Ne na kilifa la du dox ci tànk caaxaan Ñeent ak tranche indi guro daadi laban Mi ngi may teg tank bëgg ma forcé ray Ndekke lu mu bëggoon dugal but bi jubilé daw Yàlla du juum, ma ni Yàlla du juum Lu mu def ndekke loolu moo gën Demoon naa bay xalaat nar ko jox sama xol Ndekke su ma ko defoon maa ngi ci tolof-tolof Kon fok ma xoolaat ko Saay-saay la Kon fok ma xoolat ko Ndaw si saay-saay la Yàlla du juum, ma ni Yàlla du juum Lu mu def ndekke loolu moo gëna Demoon naa bay xalaat nar ko jox sama xol Ndekke su ma ko defoon maa ngi ci tolof-tolof Ne na ku dul man bëggul soxlawul Ma ne rekk la jox bopp ku mel ni man amul Man ma ko yëngal-yëngal mbëgelam Ndekke man dama dóor ay calmant la may jox Dem naa ba dépense këram ma ko yor Fay courant, fay ndox, fay jàng xale yi école Jënd greffage, fay ay voyage Nekke damay door sama poche la nob Yàlla du juum, ma ni Yàlla du juum Lu mu def ndekke loolu moo gën Demoon naa bay xalaat nar ko jox sama xol Ndekke su ma ko defoon maa ngi ci tolof-tolof Kon fok ma xoolaat ko Saay-saay la Kon fok ma xoolat ko Ndaw si saay-saay la Yàlla du juum, ndekke Yàlla du juum Lu mu def ndekke loolu moo gën Demoon naa ba nar ko dugal sama biir xol Su ma ko defoon maa ngi ci tolof-tolof Kon fok ma xoolaat ko (Ndaw si saay-saay la, waay) Fok ma xoolat ko Waa ji saay-saay la Yàlla du juum, ma ni Yàlla du juum Lu mu def ndekke loolu moo gën Demoon naa bay xalaat nar ko jox sama xol Ndekke su ma ko defoon maa ngi ci tolof-tolof