Li lan doon ñaan Mel na ni ñaan yi nangu na Ñun li lan doon xaar Bes bu ñu lay wáccel Sokhna Te kër gi ko ci xool tout le monde a la joie Tout le monde a la joie Waay jaarul wax sax ouais ouais sa se voit Ouais ouais sa se voit Yow papam ak ay xaritam di waaj dem juma Ba ñu takk sëy bi rekk ñu sandi dua Ngay dégg 'heureux ménage, heureux mariage' Ñu lay taggal say louanges Yow yaay boy ak xarit yi di ko ndokaale Tay nga faayu booru ndawtal yiñ la amel fu ne Waay dañuy xawaare, taggate ba mu saf Tay dañuy xawaare Man takk na jabar Def na li war Dégg na dëkku na mbër Way dafa doon li war Ndax daf may neex lool ñu may woowee Aladji Bébé d'amour, bébé Aladji Waawaaw Aladji, waawaaw Aladji Man daf may neex lool ñu may woowee Aladji Bébé d'amour, bébé Aladji Waawaaw Aladji, waawaaw Aladji Bës yow du tuuti Bës du boroom rekk laay tollool Saa liggéeyu ndey moo la wuyusi Ñépp d'accord nañu ci loolu Waa taay dañuy daal di bâche koñ ba koñ Xar yi ñu rey, ginàar yi ñu njoñ Ñu yeggal niveau bi àjj ba si kow-a-kow Ku aaye wone sa moom, taay yaa moom Yow papam ak ay xaritam di waaj dem juma Ba ñu takk sëy bi rekk ñu sandi dua Ngay dégg 'heureux ménage, heureux mariage' Ñu lay taggal say louanges Aladji génn ak ñeeti pièce machallah Xarit yi di daar ko di ko jiin jino jiin Dem gatandu jii madame, gan bi yegsi na Ne ko 'bismillah! Tay dañuy xawaare Man takk na jabar Def na li war Dégg na dëkku na mbër Way dafa doon li war Ndax daf may neex lool ñu may woowee Aladji Bébé d'amour, bébé Aladji Waawaaw Aladji, waawaaw Aladji Man daf may neex lool ñu may woowee Aladji Bébé d'amour, bébé Aladji Waawaaw Aladji, waawaaw Aladji Yeah! Wuyu ma Aladji Si géew gi yaw laa ñuy xaar Aladji, Aladji Bës bi sa bës la, Aladji Guddi gi yaa moom Aladji, yeah Eeeweh sama Aladji, aah Aladji Aladji Sama Aladji, ooho Aladji sama Aladji!