[Dior Mbaye] Saf safal, sa dundu ma koy safal Saf safal, sa dundu ma koy safal Di la bégal boo meree ma lay defal Xol bi yaa ko moom, jëlal Yaay ki may dundal Saf safal, sa dundu ma koy safal Saf safal, sa dundu ma koy safal Di la bégal boo meree ma lay defal Xol bi yaa ko moom, jëlal (kay) Yaay ki may dundal Xam li nga bëgg tëddi la ko defal de boy ci sa dinga leer Dañuy dundu dëgg mbëggeel Ndax man noonu nekkatul ma sa jér Jàpp la ci el, dama li ko jëti ma tufal Danga ma siggi, danga ma sagal Kon tay ma lay tër (tay ma lay tër) Naa la toppatoo du font en camp Def li nga bégal noy bel mel ni kontaan Duma la foon dox Waaye naa la one di takkal nga ku pare Jonge dégg daaj, fi may faale dafa bare Hey baby, man rekk ci xale Jélul vrai paré fi lépp gale Saf safal, sa dundu ma koy safal Saf safal, sa dundu ma koy safal Di la bégal boo meree ma lay defal Xol bi yaa ko moom, jëlal Yaay ki may dundal Saf safal, sa dundu ma koy safal Saf safal, sa dundu ma koy safal Di la bégal boo meree ma lay defal Xol bi yaa ko moom, jëlal (kay) Yaay ki may dundal Ma ne bari paj, taxa Aw fitay fiteel bu ma fiire Ma ne dégg deel ragaluma ku ma viser Doxaati du tel dama tirer Waaye maak yaw la rekk sama chéri Keneen amul fi palaas boo koy jëmee Maak yaw la rekk sama chéri Fi du fi am palaas Dewal ma tagg la buur, di yëngal sa mbur Yaa ko son bi tey dinga suur Kon tey ma def li ma man, taggalal sa maam Te ko ci gamm Waaye naa la one di takkal nga ku pare Jonge dégg daaj, fi may faale dafa bare Hey baby, man rekk ci xale Jélul frai paré fi lépp gale Saf safal, sa dundu ma koy safal Saf safal, sa dundu ma koy safal Di la bégal boo meree ma lay defal Xol bi yaa ko moom, jëlal Yaay ki may dundal Saf safal, sa dundu ma koy safal Saf safal, sa dundu ma koy safal Di la bégal boo meree ma lay defal Xol bi yaa ko moom, jëlal (kay) Yaay ki may dundal