Miir ci yaw Jaral nga ma naan vody tak sim bi mu day Dawuma coow Li nga ma jaral fi lay toog di ko wax ca kaw Ma tay nob la takkal la capitaine bi Yaw kaay wax ma ni nga def ba te game bii Bon la nga raw ma, yaay bagg may teine bii Kuñ mayul du naan yaay garab may rène bii Li ñépp di wër la teye sama loxo Sa tur bi lay dëkke sikkar sama chérie coco Def nga ma sa mbër moo tax naanuma coocoo Jaral nga ma dagg sama yaram bi chérie coco Jàpp nga ma sama cóoppati Ku mel ni yaw du amaati Ci seen biir laa la cóoppati ba noppi di leen cokkeli Yaw ki kan la, ki nii kan la Bi sama bos la, teg na ci loxo Yaw ki kan la, ki nii kan la Bi sama bos la, teg na ci loxo Mbëggeel lu bondit di mboli mboli Jox la lépp li ma yor, bu doyl ma dolli Sama honey, yaay sama coni Faale nga ma manit duma la mësa foli Àljanna yu neex yi laa bëgg ñu dem fa (dem fa) Jox ma sa loxo, man ak yaw kese ñu des fa (des fa) Li ñépp di wër la teye sama loxo Sa tur bi lay dëkke sikkar sama chérie coco Def nga ma sa mbër moo tax naanuma coocoo Jaral nga ma dagg sama yaram bi chérie coco Jàpp nga ma sama cóoppati Ku mel ni yaw du amaati Yaw nobal ku la nob ku la faale Ci seen biir laa la cóoppati ba noppi di leen cokkeli Heee nobal ku la nob ku la faale Yaw ki kan la, ki nii kan la Bi sama bos la, teg na ci loxo Yaw ki kan la, ki nii kan la Bi sama bos la, teg na ci loxo (Yaw ki kan la, ki nii kan la) Wane naa la Ndax ki nga bëgg danga koy wane Wane naa la Teg na ci loxo ma waay Lelelele yaay Ku laa faale Nobal ku la nob, ku la faale Yaw ku laa faale Nobal ku la nob, ku la faale leee Yaw ku laa faale Nobal ku la nob, ku la faale leee Yaw ku laa faale