Damay solu neex na ma Sama tailleur naxu ma Sañse ree (ku ree) Man damay ree (ku ree) Ooh, ma mëna sañse! Ree ju neex! Ambiance ree (ku ree) Man damay ree (ku ree) Wuuy yaay (ree) Ma mëna sañse ree ju neex! Bari feeling mën naa fu ne Sañse ma ci topp Ma fi ap escort [...] Flash ma ko moom Mete visa ra Man fu ma génne coow li Bari lay ma tàccu dara Tàccu ma (woy tàccu) Tàcculeen li (ey tàccu) Tàcculeen li (wuy tàccu) (Dëb ko, naa mook rumbax!) Tàccu ma (woy tàccu) Tàcculeen li (ey tàccu) Tàcculeen li (wuy tàccu) (Dëb ko, naa mook rumbax!) Sama sañse baax na Sama montre baax na Samay dàll, lan la? Participer si réew mi rekk! Sama xol neex na Ma sañse reetaan Tay li la ndawtal Participer si réew mi rekk! Sañse ree (ku ree) Man damay ree (ku ree) Ooooh, ma mëna sañse! Ree ju neex! Ambiance ree (ku ree) Man damay ree (ku ree) Wuuy yaay (ree) Ma mëna sañse ree ju neex! Ey lii lan la, lii lan la? Ndekete ma ci réew (Ma solu neex na ma) Ey lii lan la, lii lan la Ndekete ci man mën naa sañse (Sama tailleur naxu ma) Oh là là, sañse reetaan (Dama solu neex na ma) Oh là là, sañse reetaan (Sama tailleur naxu ma) Nii la, nii la, nii la (Eh, ku ko mën ni nga koy defe) Nii la, nii la, nii la (Eh, ku ko mën ni nga koy defe) Sañse dox ci diggu koñ bi Fépp ñépp di ma topp Ñu naan: Ki ni kan la? (Dëb ko, naa mook rumbax!) Sañse boole kok noppi Sañse noon bi lay soppi Ñu naan: Est-ce que ki yaw la? (Dëb ko!) Maa leen tere nelaw, tere nelaw Tere nelaw (wuooh) Maa leen tere nelaw, tere nelaw Tere nelaw (wuooh) Sañse dox ci diggu koñ bi Fépp ñépp di ma topp Ñu naan: Ki ni kan la? (Dëb ko, naa mook rumbax!) Sañse boole ko ak noppi Sañse noon bi lay soppi Ñu naan: Est-ce que ki yaw la? (Dëb ko!) Maa leen tere nelaw, tere nelaw Tere nelaw (wuooh) Maa leen tere nelaw, tere nelaw Tere nelaw (wuooh) Sañse ree (ku ree) Man damay ree (ku ree) Ooh, ma mëna sañse! Ree ju neex! Ambiance ree (ku ree) Man damay ree (ku ree) Wuuy yaay (ree) Ma mëna sañse ree ju neex! Ey lii lan la, lii lan la? Ndekete ma ci réew (Ma solu neex na ma) Ey lii lan la, lii lan la Ndekete ci man mën naa sañse (Sama tailleur naxu ma) Oh là là, sañse reetaan (Dama solu neex na ma) Oh là là, sañse reetaan (Sama tailleur naxu ma) Sañse naa rekk Sañse nii la Sañse naa rekk Sañse nii la (Maa leen tere nelaw) Jarul moo koy wax ndax sañse nii la Piir moo way, li dafa xer Dëb ko, naa moo ku rumbax! Nii la, nii la, nii la (Eh, ku ko mën ni nga koy defe) Nii la, nii la, nii la (Eh, ku ko mën ni nga koy defe) Dëb ko, naa moo ku rumbax! Rumbax, rumbax, rumbax-rumbax! Kaay! Dëb ko, naa moo ku rumbax!