Dugg nga sama jamano Te sama loxo wan ma Luy mbëggeel Xamal nga ma luy nobeel Yaw daal jélal lépp Loo am ñàkku ma ko leer na ma Wuuy nobeel Xam naa lan mooy mbëggeel Dara gëmul neex mbëggeel bi ngay yëg ci sa xol dundu ko Wuy yoro baale ma Yoo baale ma Gis naa ci yaw jikko duma neex moo ma doy feex sama xol bi Ohh ohh wu wey, bëgg naa Ñoo ngi kaf foo ree Fu ñu ne ñu ngi door baake Ñépp ñu rañe Te foo ne rekk lay bëgg ne Foo ne lay nee Foo newul duma fa bëgg ne yaw Wuy ooo baale ma (yombu ma) Yoo baale ma Yaw bébé dama réew nga ni ma loxo du la laal Yaw bébé wayale ma nga ni ma Youssou Ndour lay woo Yaw àdduna bi su ma safee dara yaa ko liggéey way Yaw wane nga ma fu ne doo ma réerak feeñ Wuy nobeel! (nobeel) Aah oh (nobeel) Xamal nga ma luy nobeel Li may dundu neex na Li may dundu neex Neex na neex na neex Ni lépp yaw la Li may dundu neex na Li may yëg aka moo neex Hu waow wao wax a ay Lépp yaw la Yaa ngi jàpp te bàyyiwoo Sonn te taatiwoo Muy metti te xaddiwoo Nëbbatu woo ma Yaa ma gënal ñi ni ak ñële Ndax lépp yaw la Amina chérie Papy yaayu Muhammad Amina beauté famille ni maak ju baax nga Waay sama yaay de Aisha dago jula Yaayu Muhammad, Aïsha baax nga Li may dundu neex na Li may dundu neex Neex na neex na neex Ni lépp yaw la Li may dundu neex na Li may yëg aka moo neex Hu waow wao wax a ay Lépp yaw la Baye Dame chéri Aishata Man de way naa la Da mooy dame Ñaan bi yaw la