Nelawoo ba yàndoor Dëkke lu bon ak lu ñaaw Soxor iñaan Moo la condamné Doxal sa yoon Duma la sóoraale Mënuloo ma tere dundu li ma neex Maa ngi baax Duma leen faale Billaay dinga gëna tarde (Billaay dinga gëna tarde) Man daal duma leen faale (Non non duma leen faale) Fii lépp a ngi tolloo, taluma noono Billaay duma leen faale Yaw mbaa jàmm nga fanaan Yaw mba jàmm nga yéndo Woté lo gëmul, xamoo ni jëli naa la Maa ngi baax Duma leen faale Billaay dinga gëna tarde Man daal duma leen faale Non non duma leen faale Fii lépp a ngi tolloo, taluma noono Billaay duma leen faale Noono (moom talu la) Li Yàlla def si man Nga ne mu ku du fi ame Aaah nga di ma jebaane Nga di ma jebaane Non non nono yeah Xamaloo ma dara wër di ma togge Di ma soxore yeah yeeeah Nelawoo ba yàndoor Lu dul dëkke lu bon ak lu ñaaw Bul faale bul toppatoo doxal sa dox Wuyooy bokkuleen yoon, doxal sa dox Bul faale bul toppatoo doxal sa dox Maa ngi baax (maa ngi baax) Duma leen faale Billaay dinga gëna tarde (Billaay dinga gëna tarde) Man daal duma leen faale Non non duma leen faale Fii lépp a ngi tolloo, taluma noono Billaay duma leen faale (taluma noonu)