Dee ko woyofal, bul ko disal Àdduna bii lépp dafay jeex Jege ma, yaw bul ma wéetal Ndax lu ñi dundu dafa war a dàq neex (Lii nga ma jaral, mbëggeel moo ko waral) Kaay ñu mbégelante mak yaw mbëggeel alimenté ko (Lii nga ma jaral, mbëggeel moo ko waral) Jaral nga maa Jaral nga ma fal fa lalé lépp di lay bégal Loo la Yàlla dogal ma doo géwél bi lay woyal Loo bëgg laay def soo tëddee na nga nelaw Tëyel ma Tëyel ma, doo gis ku mel ni man Ni wëral fu la neex, benn la fii May faj sa nammeel, yaw xam nga loolu Tayuma ko nii la mel kon dee ko woyofal (Lii nga ma jaral, mbëggeel moo ko waral) Kaay ñu mbégelante mak yaw mbëggeel alimenté ko (Lii nga ma jaral, mbëggeel moo ko waral) Jaral nga maa Su ma nangoo doon sa Yaye Fall Bul nelaw, doonal Baye Fall Mbëggeel yërmandé kese la Doonal Baye Fall Jaral nga ma fal fa lalé lépp di lay bégal Loo la Yàlla dogal ma doo géwél bi lay woyal Loo bëgg laay def soo tëddee na nga nelaw Tëyel ma Tëyel ma, doo gis ku mel ni man Ni wëral fu la neex, benn la fii May faj sa nammeel, yaw xam nga loolu Tayuma ko nii la mel kon dee ko woyofal (Lii nga ma jaral, mbëggeel moo ko waral) Kaay ñu mbégelante mak yaw mbëggeel alimenté ko (Lii nga ma jaral, mbëggeel moo ko waral) Jaral nga maa Wouyoo yo lele yo lele yole Thiaba chérie Amadou xam nga ne mbëggeel neex na Kon neex na Diey Astou Sarr eh Sarr siri lay ndem li neex na neex na Dundal sa nobeel Soo ma bëggee den ko jefe ma gis ma gis ko Wouyoo yo lele yo lele yole