Topp ma soo ma bëggee Jegesi ma soo ma nobee Déglu ma soo ma bëggee Jox ma sa xol soo ma wooloo Gis nga chéri li di mbëggeel Ak réy waru ko laal Gis nga baby sunu mbëggeel Bu ci def lu dul sa xol Ëpp na at ba ñu xamante Booba ba tay lu ne muñe naa ko Ëpp na at ba ñu bëggante Bés bu ne maa di la gën a love Yaw baby sunu mbëggeel Bu ci def lu dul sa xol Yaw chéri jox ma sa xol Waat naa ne duma ko xaajamal Baby mbëggeel aventure rekk la Mënoo xam laaj biir fi yëg dugguloo Baby mbëggeel ci xol la jogé Te bu jogé ci xol, xol rekk a ka mën a xam Céy mbëggeel munoo xam la ca biir fi yëg dugguloo Céy mbëggeeley mbëggeeleee Ëpp na at ba ñu bëggante Bés bu ne maa di la gën a love Sama xol bi yaa ci ne Annn chéri bëgg naa la Bëgg naa la, bëgg naa la Kaay ñu bëggante Mbëggeel mënoo xam la ca biir fi yëg dugguloo Gis bëgg Yàlla koy def ci jaam miin bañ ci jikko la Man bëgg naa la Sama xol bi yaw la tànn, bëgg naa la Bëgg naa la, kaay ñu bëggante Man de bëgg naa la suñu mbëggeel réy waru ko laal Jox ma sa xol bi waat naa ne duma ko xajamal Man bëgg naa la, bëgg naa la kaay ñu bëggante Baby mbëggeel aventure rekk la Mënoo xam laaj biir fi yëg dugguloo Baby mbëggeel ci xol la jogé Te bu jogé ci xol, xol rekk a ka mën a xam Kaay! Baby mbëggeel aventure rekk la Mënoo xam laaj biir fi yëg dugguloo Baby mbëggeel ci xol la jogé Te bu jogé ci xol, xol rekk a ka mën a xam