Lu mu ma wax ma di ko def Dafay dëkk ci di ma tooñ Teg si ma naan ko baal ma Waaye moom la nob Su ma ko gisee Samay bët di mellax Samay tànk jaxasoo Sama lammiñ réer ma Moom laa nob Amadou, Amadou (geestu ma) Yaw sama yaay (may ma Amadou) Amadou, Amadou (geestu ma) Yaw sama yaay (may ma Amadou) Amadou, Amadou Damay gëm loo lu amul Terewul ma di ko gëm Tég ci ma naan ko baal ma Waaye moom la nob Su ma ko gisee Samay bët di mellax Samay tànk jaxasoo Sama lammiñ réer ma Moom laa nob Amadou, Amadou (geestu ma) Yaw sama yaay (may ma Amadou) Amadou, Amadou (geestu ma) Yaw sama yaay (may ma Amadou) Amadou, Amadou Amadou, Amadou (geestu ma) Yaw sama yaay (may ma Amadou) Amadou, Amadou (geestu ma) Yaw sama yaay (may ma Amadou) Amadou, Amadou Saa yu ma jege woote téléphone Ci téléphone bi lay yéndu Saa yu ma jege ab setsi Ma yendoo wajal Xam naa ni nob na keneen ku dul man Oh yeg na ni mi ngi seeti keneen ku dul man Waaye moom laa nob Amadou, Amadou (geestu ma) Yaw sama yaay (may ma Amadou) Amadou, Amadou (geestu ma) Yaw sama yaay (may ma Amadou) Amadou, Amadou Amadou, Amadou (geestu ma) Yaw sama yaay (sama yaay may ma Amadou) Amadou, Amadou (geestu ma) Yaw sama yaay (sama yaay may ma Amadou) Amadou, Amadou (geestu ma) Yaw sama yaay (sama yaay may ma Amadou)