Yéwwu ci sa wet doy na mbégte Jàkkarlook sa kanam doy na bànneex Love bi may yëg ku ko mën téye Ana ki ko saañ jaral na ma xeex Soo bëggee nak mu sauvage baby Soo bëggee nak mu doux, loo def yaa tay Dis-moi ce qui t'arrange bébé Jafandu na ci sa branche, mbëggeel bu xeere Yéwwu ci sa wet doy na mbégte Jàkkarlook sa kanam doy na bànneex Love love bi may yëg ku ko mën téye Ana ki ko saañ jaral na ma xeex Soo bëggee nak mu sauvage bébé Soo bëggee nak mu doux, loo def yaa tay Dis-moi ce qui t'arrange bébé Jafandu na ci say branche, mbëggeel bu xeere Ci sa wet duma bàyyi Ak lum mënti doon Bul ma yërëm, dee ma gaañ Takk sama loxo Yaw sa allure dafa gaaw Ku ko lekk fott Même soo tooñe bul ma baalu Loo def daf may neex, yaa tay! Soo ma tooñee, yaa tay Reewantul sax, yaa tay Ku ci dugg moo ci des Ma baby yaa tay Soo ma tooñee, yaa tay Reewantul sax, yaa tay Ku ci dugg moo ci des Kon baby yaa tay Man de bëgg naa (yaa tay) Loo wax mu neex (yaa tay) Yaw danga taaru, danga jékk, danga nice (baby yaa tay) Sa doxin rafet na (yaa tay) Man bëgg naa (baby yaa tay) Loo def mu neex, xam na ding ma mës a gaañ Bëgguma ñuy réeroo Waxumalaak tàggoo Sama cofeel ci yaw wor na ma Nob naa la man, eh-eh ya Show me your love my baby boo Sama safara, ma seytaane Everything my love knocks me down Rocc sama geñoo jox naa la ko Ah dissah deep love fidi gyal dem Dem ennemi mana ready fi shoot dem Mi love is over all, why a mi ready fi evathing Baby yàgg na, man dama pare Ndiggël xale bi jaral na ma xare Mi love is over all, why a mi ready fi evathing Ci sa wet duma bàyyi (ma baby boo) Bul ma yërëm dee ma gaañ (mon bébé à moi) Sa allure dafa gaaw (ma baby boo) Même soo tooñee bul ma baalu (mon bébé à moi) Soo ma tooñee, yaa tay Reewantul sax, yaa tay Ku ci dugg moo ci des Ma baby yaa tay Soo ma tooñee, yaa tay Reewantul sax, yaa tay Ku ci dugg moo ci des Kon baby yaa tay Hum Show me your love, ma baby boo