Baye Mass Je saisis ton amour, je connais ta peine Dekk nga ci sama xel Au dessus de nos vies à jamais on s’aime Maa denk la sama mbëggeel Jox naa la sama dund jël ko nga dem Wan ma li nekk sa xel Si t’es ma source de vie, je reste à terre Yaw xam nga ni bëgg du dee Yaw yaay ki jiitu, yaay kiy mujje yaw Yaay ki may xool sama xol di yëg mbëggeel Yaa leen gën fuuf, yaa leen ëpp doole T’es ma sunshine, ma plus que parfait Bëgg naa la, bëgg naa la, bëgg naa la piir Yéene naa la àdduna, yéene la àljana ak li nekk ci biir Je t’offre ma vie comme cadeau et je ferai le pire Yee nga li nekk ci man Moo tax dama lay bëgg dugal sama biir (sama biir) Bëgg naa la, bëgg naa la, bëgg naa la piir Yéene naa la àdduna, yéene la àljana ak li nekk ci biiram Je t’offre ma vie comme cadeau et je ferai le pire Yee nga li nekk ci man Moo tax dama lay bëgg dugal sama biir (sama biir) Moo tax ma naan la Yaw yaay ki jiitu, yaay kiy mujje yaw Yaay ki may xool sama xol di yëg mbëggeel Yaa leen gën fuuf, yaa leen ëpp doole T’es ma sunshine, ma plus que parfait Su may nelaw ni nga may yeewe Ëpp doole sama yéene (ëpp doole sama yéene) Sama dund ni nga ko changer Waral ma def la Ouroul Ayni Su may nelaw ni nga may yeewe Ëpp doole sama yéene (ëpp doole sama yéene) Sama dund ni nga ko changer Waral ma def la Ouroul Ayni Papa Thione suñu yaay di Diaga Dora Gueye ne na Clara Pa’ Diouf ne na Bb Bass Wayee Abba moom ne na Mamy (La def Ouroul Ayni) Mouhamed moom ne na Ndoumbe (Moom mooy Ouroul Ayni) Hmmm yeah Yaroo baax yaroo baax yaroo baax Soo yaroo màcc tangal, yëy sa gune ngay Yaroo baax yaroo baax yaroo baax Soo yaroo jiiko yaa ko yee xale bi yaroo baax