Ay, àdduna yàggul, bul jaay sa ngor Bu dara fekk sa bët looloy nobless Ay, àdduna yàggul, bul jaay sa ngor Bu dara fekk sa bët looloy nobless Man ngor la (eey), doomi ngor la (eey) Man ma nob la (eey), dara fekkul samay bët (eey) Man ngor la (eey), doomi ngor la (eey) Man ma nob la (eey), dara fekkul samay bët (eey) Man li ma ñàkk ak li ma am kenn du ko xam dox doy Man awma fekkul samay bët (liggéey rekk ko woor) Man li ma ñàkk ak li ma am kenn du ko xam dox doy Man awma fekkul samay bët (liggéey rekk ko woor) Yoral say million di ma gondi Ay dëkku du neex, dëgg du neex Dëggentan na neex! Je m'en fous de ça (ay ree nga may def) Je m'en fous de ça (ay ree nga may def) Racagin cee pacee, tësëm gëjëm gëjëm! Oh my God! Gubacee, pacee Gubacee, pacee Cër, tësël Cër, gichër Ehh ko yëngel ma yëngel Man dara dara du ma dee Yëkkëtil loxo ca kaw Yëkkëtil loxo ca kaw (ganaan rasagin) Je m'en fous de ça (ay ree nga may def) Yëkkëtil loxo ca kaw Yëkkëtil loxo ca kaw (ganaan rasagin) Je m'en fous de ça (ay ree nga may def) Raw rasagin Geex geex may ree Ay ree nga may def (rasagin) Geex geex may ree Ay ree nga may def (raw rasagin) Je m'en fous de ça (rasagin) Je m'en fous de ça (rasagin) Racagin cee pacee Tësëm gëjëm gëjëm! Oh my God! Gubacee, pacee Gubacee, pacee Cër, tësël Cër, gichër Ehh ko yëngel ma yëngel Man dara dara du ma tee Ehh ko yëngel ma yëngel Man dara dara du ma dee Ama Sow borom bambay talibë bamba gi Je m'en fous de ça Yaay boroom sing saas gi DG au discours Je m'en fous de ça Geex geex may ree Ay ree nga may def (rasagin) Geex geex may ree Ay ree nga may def (raw rasagin) Solal say Jordan ma laal tik tik Demal restaurant ma lal may nga Yoral auto bu nice di ma gondi Dëkk ci kër gu nice di ma gondi Racagin cee pacee Tësëm gëjëm gëjëm! Oh my God! Gubacee, pacee Gubacee, pacee Cër, tësël Cër, gichër Ehh ko yëngel ma yëngel Man dara dara du ma tee Ehh ko yëngel ma yëngel Man dara dara du ma dee Eh loo am doylul Te lo yor doylul Waawaaw Yeye doyu rekk! Wërsek bu de ñëw! Dara dara du ko dee Wat ko si Yàlla bu de am nga li ma ñàkk Million bu la leewul gënal dërëm bi ma ñakk Doyloo sama sombi di ko naan xel bu dal Moo ma gënal ginnaar bu ngay time dee doo ko tal Lu jot yomb, eeh lu jot yomb Boroom karaw bu ñul la ñakku ma dara Billaay lu jot yomb, eeh lu jot yomb Boroom karaw bu ñul la ñakku ma dara Eh man duma ñee ku yor alal Ndax xamuma ni mu ko amee Su ngeen tàccu dafay gëna neex Oh my God (cakk tan) Oh my God (cakk tan) Cakk, cakk, ragi cagi jangicew Ey billaay yaw, loo ran jëlel lii Je m'en fous de ça