C'est Dieu Hey, hey, hey, hey Hey si tu aimes, fais partie des miens Nous on fait ça bien Si t'aime pas, garde tes commentaires On en a rien à faire C'est Dieu! Tout ce que je fais, y'a Dieu dedans C'est Dieu! Hey, c'est pas les marabouts C'est Dieu! Yaay yaa yax duma takk, duma naan Sëriñ du lekk sama dërëm Hay wuy sama ndey! Xale bi yaayam da ko ñaanal Hey, xale bi yaayam da ko ñaanal Hey Yàlla fi ne C'est pas les marabouts C'est Dieu! Hey, hey, hey, hey C'est pas les marabouts C'est Dieu! Hey, hey, hey, hey Fecc bu bees! C'est pas les marabouts C'est Dieu! Hey, hey, hey, hey Yàlla jël kooku neex Def ci moom lu ko neex Soo nangoo ndogal rekk Fils sa xol du gaaw a jeex Yénne ngeen la yaa ko tabax Te yaa ciy fanaan Nga bañ ma lu may waññi Hey iñaan dafa tarde Je suis béni (béni) Hey je suis béni C'est pas les marabouts C'est Dieu! Je suis béni (béni) Hey je suis béni C'est pas les marabouts C'est Dieu! Je suis béni (béni) Hey je suis béni C'est pas les marabouts C'est Dieu! Hey Yàlla moo bari doole Yàlla moo bari doole Yàlla mooy may, lu dul Yàlla neen la Yàlla noppi na (ayyy) Su Yàlla bindee nga effacer Hey yaw lay mujj effacer taracer (ay way!) Su Yàlla dogalee may avancer Hey yaw nangul ndogal bul déranger Fils, soo gisee li bul di laaje Hey Yàlla ci ànd ak man, y'a Dieu dedans Xale bi Yàlla moo ko tàccu Hey nanguleen ndogal way! Y'a Dieu dedans! Y'a Dieu dedans! Je suis béni C'est Dieu! Hey je suis béni C'est Dieu! Hey c'est pas les marabouts C'est Dieu! Yaay yaa yax duma takk, duma naan Sëriñ du lekk sama dërëm Hay wuy sama ndey! Xale bi yaayam da ko ñaanal Hey, xale bi yaayam da ko ñaanal Hey Yàlla fi ne C'est pas les marabouts C'est Dieu! Je suis béni (béni) Hey je suis béni C'est pas les marabouts C'est Dieu! Je suis béni (béni) Hey je suis béni C'est pas les marabouts C'est Dieu! Y'a Dieu dedans! Si c'est pas Dieu, c'est qui? Ay, ay, ay, ay Y'a Dieu dedans! Baayu maman, baayu el-hadj, ak Mouhamed Samba ak Sape, Omar jëlël li Y'a Dieu dedans! Omar Sow Yàlla moo ko tàccu Hey naanuleen ndogal way! Y'a Dieu dedans! Chéri Ndaye Sene Omar Sow yaa ngi yëngal Lu mu lundum lundum da ngay Khouss Diarr Y'a Dieu dedans! Omar Sow Yàlla ko teral! C'est Dieu! Diatou c'est bon! Hey bu la pontu jamm, bu la paka laal Lamecette aram naa la Diatou ni la Yàlla def C'est Dieu! Diatou c'est bon! Yaa ëpp doole te ya gëna feete xale Seynabou sa doom Amatina Ndam Diatou c'est bon! Hey Diatou Yàlla ko teral C'est Dieu! Ibou Seye foo féete Chéri béko kay C'est pas les marabouts C'est Dieu! Je suis béni (béni) Hey je suis béni C'est pas les marabouts C'est Dieu! Je suis béni (béni) Hey je suis béni C'est pas les marabouts C'est Dieu! C'est pas les marabouts C'est Dieu!