Weettay dima ray Té ñémé wu ma netali Mangi sama yoon Ni picc ramatu Yalla dima wétëli Goor momul ñaan Yareewuñu ma tallal loxo Yaay joor sama yaay Mangi sakku sa ñaan Yeurmande amul fii Wettay ak namel Nekk ndaw ci samay digg morom yafus waruma Fii lekkuñu bë sur Nanuñu bë mandé Way nekk ndaw ci suñuy digg morom yafus waruma So yewo yema fallo So yewo yema fall (yeah) Fi degn fi nekk ak ngor Fi degn fi dathie lou metti Nekk fi ak jom Fatewouma demb ak Yaay Joor Wettay si xol la meun yam Sam khel jougoul si sassmeu Goné diss neu wayé bo magué fay borr Lambay soudé meuss neu nekh Tay Walo amoul ndokh Touki dou tekki Gaaday andou tak banekh Wetna wettay bimay yé Rerr na fou gnar gni fеgn Genteu beu dеmb fegn tay Yéné beu agg Jooy na fou keine newoul Dem na ba bougou ma guiss samay rongogn Ndakh mounou meu bayi limalen diguon Jambar dawoul daa outi ji wone Yakar bou tassoul ba tay Ndakh yoon bi diekha goul Sama khel ci kasso dou teey dey dem fou dieumeu doul yegg di fey Wetna wettay bimay yé, anh anh anh Jooy na jooy guisouma keineu, yeah yeah yeah Love and peace for me I can shine, shine like a diamond Wa wa wa wa wa wa I can shine, shine like a diamond Pray for, for me yeah Weettay dima ray Té ñémé wu ma netali Mangi sama yoon Ni picc ramatu Yalla dima wétëli Goor momul ñaan Yareewuñu ma tallal loxo Yaay joor sama yaay Mangi sakku sa ñaan Yeurmande amul fii Wettay ak namel Nekk ndaw ci samay digg morom yafus waruma Fii lekkuñu bë sur Nanuñu bë mandé Way nekk ndaw ci suñuy digg morom yafus waruma So yewo yema fallo So yewo yema fall Ndimbalo yeurmandey fall Doley biir bek bitti bee fall