Ma ne nga dox fa Rabu xiir pare di la ko vuruj Fu ma génn ngeen daagu xol yi taa Soo ma xoolee dinga xam sa sëriñ mënul Parewoo Oh manuñu tolloo ni baaram yi sa loxo (Manuñu tolloo) Wërsëk bu ne borom manuñu tolloo Na ku ne xam moromam (Manuñu tolloo) Bëgguma di ma toppando (Eeeh eeeh) Di ma xas te di ma toppando (Eeeh eeeh) Qualité du toppando daal (Eeeh eeeh) Pur man bàyyi nga toppando (Eeeh eeeh) Ëpp na ci mapando daal Dolli ci sol fa Mi mélodie la dalay dugg ma ni nga bég Man ci bi beat te mënoo wéy coosaan Authentique ne laaxu sow ku ñu def ci lekket Parewoo Oh manuñu tolloo ni baaram yi sa loxo (Manuñu tolloo) Wërsëk bu ne borom manuñu tolloo Na ku ne xam moromam (Manuñu tolloo) Bëgguma di ma toppando (Eeeh eeeh) Di ma xas te di ma toppando (Eeeh eeeh) Qualité du toppando daal (Eeeh eeeh) Pur man bàyyi nga toppando (Eeeh eeeh) Di ma xas te di ma toppando (Eeeh eeeh) Dégg naa ni lekkatoo sax (Eeeh eeeh) Nelawatoo ndax bañ nangu dogal (Eeeh eeeh) Pur man bàyyi nga toppando (Eeeh eeeh) Ëpp na ci mapando daal Anh Wo wooh Soo xamoon fi ma jaar ba yégsi fi Fa Yàlla lay defare jaam loxo yéegu fa Ñaanu yaay la Yàlla di jël Kenn mënul fakkatel kuy jug ci njël Am naa ñaanu baay lu may ragal Ay waxi ginnaaw, wax leen ma nga ca kanam Ñaanu yaay la Yàlla di jël Kenn mënul fakkatel kuy jug ci njël Am naa ñaanu baay lu may ragal Ay waxi ginnaaw, wax leen ma nga ca kanam Bëgguma di ma toppando (Eeeh eeeh) Di ma xas te di ma toppando (Eeeh eeeh) Qualité du toppando daal (Eeeh eeeh) Pur man bàyyi nga toppando (Eeeh eeeh) Di ma xas te di ma toppando (Eeeh eeeh) Soo xamoon fi ma jaar ba yégsi fi Fa Yàlla lay defare jaam loxo yéegu fa