Love, I will give my heart to you And make your dreams come true Never make you heart to lose Oh na na na no no no Louy dundeul sa khol bae (mbëguel, mbëguel) Mbëguel moy doundeul sama khol bae (mbëguel, mbëguel) Louy saffal sama khol bae (mbëguel, mbëguel) Mbëguel moy doundeul sama khol (anh han) Love bi néthii man néthii yow Té liko teug tassaguko Nelow na thii say lokho Yewou thii sa khol Love bi néthii man néthii yow Té liko teug tassaguko Nelow na thii say lokho Yewou thii sa khel thii sa khol Yeh yeh yah, yeh yeh yah Yeh yeh yah, yeh yeh yah Sama mourray Thii biir negg bii thii kaw lal bii moy sa nofflay (eh hé hé eh) Wakhal wayy, samey thiouray, you bakh yi namngako wayy (ah han yeah yeah) Yow lingueu nekk yow lay done Té fo diokhogn moy sama yone Mouy souba goudi ak ngone (ah han han han) Yow lingueu nekk yow lay done Té fo diokhogn moy sama yone Mouy souba goudi ak ngone (ah han han han) Love, I will give my heart to you And make your dreams come true Never make you heart to lose Oh na na na no no no Love, I will give my heart to you And make your dreams come true Never make you heart to lose Yeh yeh yah, yeh yeh yah Yeh yeh yah, yeh yeh yah Love bi néthii man néthii yow Té liko teug tassaguko Nelow na thii say lokho Yewou thii sa khol Love bi néthii man néthii yow Té liko teug tassaguko Nelow na thii say lokho Yewou thii sa khel thii sa khol Masseck Thiam (mbëguel, mbëguel) [?]