Koffi défal lu baax tay lu bone lalay faay Koffi défal lu baax tay lu bone lalay faay Aduna sa xarit mo meuna done sa none Damako dji teranga mu faay ma lu bone Linga tambalé paré guo Baadola baadola lay done rekk ba dééh Jiiko jaam lay dundé Linga tambalé paré guo Baadola baadola lay done rekk ba dééh Défal naala lune Teranga lako ji Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma Koloré lako ji Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma Teranga lako ji Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma Koloré lako ji Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma Aduna, niit dina jaay ngoram guir done jaam Damala wolu wone loma lathie ma diokhla Féété la fii, féété la fé, féété la fu nekk Léép lula meussa mééti, mééti naama Ma bééteu la ngamay jëw Naane man ak sama jëkër meunu gno am dome Motax may gudé Ma bééteu la ngamay djeuw Baadola baadola lay done rekk ba dééh Défal naala lune Teranga lako ji Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma Koloré lako ji Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma Teranga lako ji Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma Koloré lako ji Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma Dagua xam luy aam suba yaw non Lu la Yallah buur dinthial yaaw non Dagua fokni gagn ngama yaw non Dagu ma bétteu maay aam gagn Linga tambalé paré guo Baadola baadola lay done Rek ba dééh Jiiko jaam lay dundé Linga tambalé paré guo Baadola baadola lay done Rek ba dééh Défal naala lune Teranga lako ji Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma Koloré lako ji Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma Teranga lako ji Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma Koloré lako ji Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma Dagua xam luy aam suba yaw non Lu la Yallah buur dinthial yaaw non Dagua fokni gagn ngama yaw non Dagu ma bétteu maay aam gagn